Lyrics | |
Sound | |
Dance | |
Video | |
Average
|
|
official music video for “endiscipline” by Ndongo d
Directed by : supernova, Mamoune Prod
composed by Faada Freddy and Demolisha
recorded @ Bois sakre & Demolisha
Mixed @ Demolisha By Demolisha
Subscribe to the official Djf YouTube Channel :https://www.youtube.com/user/Daarajfamily/videos?view_as=subscriber
https://www.facebook.com/daarajfamilyfan/
https://www.instagram.com/daarajfam_officiel
https://wwwtwitter.com/daarajfamily
lyrics:
Ya ngi xaax tëf fune ci mbed sotti mbalit mi sa yoon dëkando faleewo ya ngi baare tali bi
« tente » koñ bi yëp poot dajale say paan
ni cars-rapide bu yab ba fees ci digg yoon bi mu
« panne » soffër bi dugg tali bi « dos-d’âne » falewul xiiro bi ηaayo bi koksër aparanti ken attewul
ñaata saufaar ñu lim burle “feu-rouge” ñu ne cëm
ki moy waaja bimuy dawal ub seen bët ñu gëmm
T’en as rien à faire , tu craches partout sur le bitume tu jettes tes ordures à tout-va ,le voisinage tu t’en fous!!
Tu bloques le passage juste pour une cérémonie,une grande tente pour célébrer un baptême,tu laves ton linge en plein milieu de la rue chargée comme un car- rapide tombé en panne
Le chauffeur n’a pas froid aux yeux,rien à faire du dos-d’âne .Banales sont les bagarres entre apprentis et coxseurs sur la voie publique ,combien de chauffards grillent le feu rouge invisible, tout le monde s’en fout au final on a des yeux que pour sa belle caisse on en bave .
Endiscipline
ku dem yobaale sa jikko li araam moy ñakk yaradiku tilim jikko
Endiscipline
Melokaan bi ngay dikke ci bitti ni nga njëkke
ñu ngi gis nuñ lay sikke
Endiscipline
Marsandisu reewande tey la gëna lambb ñëppay jënd ñëppay jaay
Endiscipline
yaa ngi tëb tëb ta do dal
bis yar a dal ta ken ken du la raay
endiscipline
nos comportements nous reflétent
le pire dans la pauvreté est l’inconscience,l’impolitesse et le mauvais comportement
endiscipline
ta manière d’être se refléte sur ton attitude
on te jugera sur les faits et l’attitude
Endiscipline
est comme une marchandise qui se vend comme des petits-pains tout le monde en achéte tout le monde en vend
endiscipline
on est de plus en plus fougueux on s’obstine
un de ces jours on le regrettera amèrement
Mëno xaar sa tuur sooga ñëw burle rang bi
ya ngi ndadé kontewoo bëg tëb “numba 1one bi”
bo dugge bus tafu tafee ak sa xet ya ngi nuy xër saxaar sigaret sanni fula neex
dajjeeti nga beneen paket
naan sa njaru kafee kaas bi xaar yeneen sareet
ya ngi guux sa ndox fi nga taxaw ngay sanni mbuus bi say loxo duñu set ya ngi gén leegi duus bi
t’es pas patient tu préféres griller les étapes
t’es venu en dernier tu veux passer en premier
tu schlingues et tu colles les gens dans le bus en volant du plaisir ,tu fais du pick-pocket .
Tu nous enfumes avec ta cigarette ,à peine
tu jettes un paquet t’en ouvres un autre et t’en met partout en buvant du njaru café ,la tasse attendra le passage des charrettes
.Aprés quelques gorgées d’eau tu lances le sachet par terre, tes mains sont sales tu viens à peine de sortir des toilettes
Refrain..
Civilise ak badoolo
doxin wa ak waxin wa
jëf ja ak nuyoo ba ak rentré ba Accident yu bëri yi ngay gis manque de civisme la
bu fukki nit di gas fukki nit di suul pax du gaawa am
manque de civisme mën ta weesu
pont ba duñ ca yeeg
ba ci commissariat yi leele nga gis mode tortures yo xamne manque de civisme la
être civilisé ou impoli
Dans ta maniére de marcher, de parler
de saluer ou de faire
trop d’ accidents dûs à un manque de civisme
“Défense d’uriner “ mur bi sax tereko
ya ngi taxaw ci mbed mi saw jokkan fa pareego Policier bi neena priip njaga ndiaay fok mu stop bu de dafa amul frein loxom fok mu yoor ci poos taxi gén sens-interdit liila xelam yannu ci loos Marchands ambulants dox ci naaj bi dans le vent ni trotuwaar bi en-avant fok mu def sandikat
xat na lool Sandaga liko jële dëk ba moola fi inddi dañuy course ak yafuus mëna jël sen benefice
lu tabax yeeg yeeg xel ya ngi gëna di kule
daf ñuy tere gëna gis teggin bi nilañuy koy suule lu tabax yeeg yeeg xel ya ngi gëna di kule
daf ñuy tere gëna gis teggin bi nilañuy koy suule
On dirait qu’ils ont la cécité ,”défense d’uriner” même écrit sur le mur ne les empêche pas d’y pisser
ou d’y déposer leurs besoins.
Même un priiip (siflet) du policier n’arrêtera pas le ndiaga ndiaye(transport en commun) sans frein, il mettra la main à la poche.
Il est pas dans son assiette le taximan,il aura pris le sens-interdit comme à son habitude.
Et le marchand ambulant déambule dans le vent, sous le soleil ardent il est le roi des trottoirs
il fera comme à Sandika(pikine)
il va assiéger Sandaga .On vient tous du village on est pas des fénéants on a le même but c’est faire du bénéfice coûte que coûte
Et Plus les immeubles sortent de terre plus les esprits s’enterrent,
on y voit plus trop clair on enterre les bonnes manières
Plus les immeubles sortent de terre plus les esprits s’enterrent.
#Ndongod #indiscipline #Daarajfam